Cour d’Appel: Imam Ndao et Cie (re)jugés le 28 février pour Terrorisme

Cour d’Appel: Imam Ndao et Cie (re)jugés le 28 février pour Terrorisme

Le 19 juillet 2018 di gnéntti at guinaaw bignou dioxé verdict bi gnél mbiroum imam Alioune Badara Ndao ak gnimou àndaloon.
Gnoom gni gnou daanoon ci mbiroum terrorisme té gnou attaqué dogal bi premiere juge bi dieuloon ak procureur bi waraloon gnou def appel, Procès en appel bi di nan ko amal le 28 février 2022 bougnou soukeundiko ci l’observateur bou tay bi.

Makhtar diokhane bokkon ci gnignou daan 20 ans de prison ferme ak liggéeyou sagnouta bagn « travaux forcés »