LE VERDICT EST TOMBE POUR LES 7 TRANSPORTEURS ARRETES A DIOURBEL, LORS DE LEUR GREVE !

LE VERDICT EST TOMBE POUR LES 7 TRANSPORTEURS ARRETES A DIOURBEL, LORS DE LEUR GREVE !

Dogaloub àtté diouroom gnaari apprenti chauffeur yi gnou tegoon lokho sa Diourbel bi transporteur yi grèvé ndax dagno taal Bus Dakar dem dikk rotna, procès bi doon amé sa tribunal Grande instance bou Diourbel Birane Tine gnou daan ko 1 mois de prison ferme. Abdou Fall Ndiaye, Adama Sylla, gallay Faye ak Ibrahima Ndiaye gnou leen di toppé téewé rassemblement bo khamné diaaroul yoon ak khagn nit ki liberté de travail, daan nañ leen 6 mois de prison yoo khamné 1 mois ba rekk lagniy teud